Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 53:5 in Wolof

Help us?

Esayi 53:5 in Kàddug Yàlla gi

5 Te moom sunuy tooñ a waral ñu jamat ko; sunuy ñaawtéef a waral ñu dëggaate ko. Yar yi nu jàmmal moom la dal, te mooy ki nu wére ciy góomam.
Esayi 53 in Kàddug Yàlla gi