Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 49:13 in Wolof

Help us?

Esayi 49:13 in Kàddug Yàlla gi

13 Asamaanoo sarxolleel, suufoo bégal, te tund yi xaacoondoo! Aji Sax jee dëfal ñoñam, moo ñeewante néew-ji-dooleem ñii.
Esayi 49 in Kàddug Yàlla gi