Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 49:10 in Wolof

Help us?

Esayi 49:10 in Kàddug Yàlla gi

10 Duñu xiif, duñu mar; tàngooru mbóoya akub jant du leen sonal, nde ki leen ñeewantee leen di wommat, di leen yóbbu fu ndox bënne.
Esayi 49 in Kàddug Yàlla gi