Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 1:8 in Wolof

Help us?

Esayi 1:8 in Kàddug Yàlla gi

8 Siyoŋ, dëkk bu taaru baa ngi wéet ni mbaarum tóokër mbaa dalub toolu xaal. Mbete dëkk bu ñu gaw!
Esayi 1 in Kàddug Yàlla gi