Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 1:29 in Wolof

Help us?

Esayi 1:29 in Kàddug Yàlla gi

29 Yeenay rus moos ci garab yu mag, yi ngeen soppoona daje, di xërëmtu. Yeenay am gàcce ci tóokër, yi ngeen taamu woona daje, di bokkaale.
Esayi 1 in Kàddug Yàlla gi