Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 1:20-21 in Wolof

Help us?

Esayi 1:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Waaye su ngeen lànkee, fippu, saamar a leen di xéewloo.» Aji Sax ji déy a ko wax ci gémmiñam.
21 Ana nu biib dëkk yàqoo, mbeteb gànc, te nekkoon dëkkub kóllëre, njubte mate fa, njekk lal fa panaan, tey ñu diy bóomkat!
Esayi 1 in Kàddug Yàlla gi