Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 1:16-17 in Wolof

Help us?

Esayi 1:16-17 in Kàddug Yàlla gi

16 Raxasuleen ba set wecc, jëleleen seeni jëf ju bon fi sama kanam, te ngeen ba lu bon.
17 Jàngleen di def lu baax, sàkku njub, waññi ab notkat, àtte dëgg, ab jirim, sàmm àqu jëtun.
Esayi 1 in Kàddug Yàlla gi