Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 1:13 in Wolof

Help us?

Esayi 1:13 in Kàddug Yàlla gi

13 Buleen fi indeeti saraxi caaxaan, seen saraxu cuuraay, lu ma seexlu la. Terutel weer ak bésub Noflaay ak wooteb ndajee ci yem! Duma mana dékku ndajem diine mu rax njubadi.
Esayi 1 in Kàddug Yàlla gi