Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 1:11 in Wolof

Help us?

Esayi 1:11 in Kàddug Yàlla gi

11 «Lu may doye seen sarax yu bare?» la Aji Sax ji wax. «Damaa suur seen saraxi rendi-dóomali kuuy, suur nebbonu juru yar gi, deretu yëkk ak xar ak sikket it, safu ma.
Esayi 1 in Kàddug Yàlla gi