Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 11:13 in Wolof

Help us?

Esayi 11:13 in Kàddug Yàlla gi

13 Fiiraangey Efrayim day jeex, njéefoy Yuda dakk, Efrayim dootu fiire Yuda, Yuda dootu jéppi Efrayim.
Esayi 11 in Kàddug Yàlla gi