Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 10:3 in Wolof

Help us?

Esayi 10:3 in Kàddug Yàlla gi

3 Ana nu ngeen di def keroog bésub mbugal ba, keroog ba safaan di bawoo fu sore? Ana ku ngeen di daw wuti wallam? Ana fu ngeen di denci seen teraanga?
Esayi 10 in Kàddug Yàlla gi