Text copied!
Bibles in Wolof

Baamtug Yoon wi 28:8 in Wolof

Help us?

Baamtug Yoon wi 28:8 in Kàddug Yàlla gi

8 Aji Sax jee leen di booleek barke bu wàccal seenum sàq, ak seen mboolem ñaq, te moo leen di barkeel ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji jox.
Baamtug Yoon wi 28 in Kàddug Yàlla gi