Text copied!
Bibles in Wolof

Amos 4:13 in Wolof

Help us?

Amos 4:13 in Kàddug Yàlla gi

13 Kii kat moo móol tund, di sàkk ngelaw, di xamal nit nammeelam. Kee di soppi lëndëm ag leer, di daagoo kawte ya. Kookoo di Aji Sax ji Boroom gàngoor yi.
Amos 4 in Kàddug Yàlla gi