Text copied!
Bibles in Wolof

1 TESALONIG 5:14 in Wolof

Help us?

1 TESALONIG 5:14 in Téereb Injiil

14 Bokk yi, nu ngi leen di dénk, ngeen yedd ñi feñaag, dëfal ñi seen yasara yàcciku, dimbali ñi néew doole, tey muñal ñépp.
1 TESALONIG 5 in Téereb Injiil

1.Tesalonig 5:14 in Kàddug Yàlla gi

14 Bokk yi, danu leen di dénku; yaafus yi, femmuleen leen; ñi néewu fit, ñaaxleen leen; néew-doole yi, dimbalileen leen, te it muñal-leen ñépp.
1.Tesalonig 5 in Kàddug Yàlla gi