Text copied!
Bibles in Wolof

1 PIYEER 2:16 in Wolof

Help us?

1 PIYEER 2:16 in Téereb Injiil

16 Li leen Yàlla goreel nag, bu mu tax ngeen mbubboo ko, bay def lu bon, waaye ngeen gëna feddali seen jaamu Yàlla.
1 PIYEER 2 in Téereb Injiil

1.Piyeer 2:16 in Kàddug Yàlla gi

16 Ay gor ngeen, waaye jaami Yàlla ngeen. Kon buleen taafantoo li ngeen diy gor ba def lu bon.
1.Piyeer 2 in Kàddug Yàlla gi