Text copied!
Bibles in Wolof

1 PIYEER 2:10 in Wolof

Help us?

1 PIYEER 2:10 in Téereb Injiil

10 Démb nekkuleen woon ci dara, waaye tey mbooloom Yàlla ngeen; booba jotuleen woon yërmandeem, waaye léegi jot ngeen ko.
1 PIYEER 2 in Téereb Injiil

1.Piyeer 2:10 in Kàddug Yàlla gi

10 Yeen ñi dul woon sax aw xeet, démb, tey yeen ay xeet wi Yàlla ñoñoo; dajaguleen woon yërmande, waaye tey daj ngeen yërmande.
1.Piyeer 2 in Kàddug Yàlla gi