Text copied!
Bibles in Wolof

1 PIYEER 1:3 in Wolof

Help us?

1 PIYEER 1:3 in Téereb Injiil

3 Cant ñeel na Yàlla, Baayu sunu Boroom Yeesu Kirist! Moo nu judduwaatal ci yërmandeem ju bare, ba may nu yaakaar ju sax ndax ndekkitel Yeesu Kirist.
1 PIYEER 1 in Téereb Injiil

1.Piyeer 1:3 in Kàddug Yàlla gi

3 Cant ñeel na Yàlla, sunu Baayu Sang Yeesu Almasi! Moo nu judduwaatal ci yërmandeem ju yaa, ci dooley ndekkitel Yeesu Almasi, ngir may nu yaakaar juy dund.
1.Piyeer 1 in Kàddug Yàlla gi