Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 69:20-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 69:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Yaa gis ñu di ma sewal, di ma ruslook a torxal, yaa ngi ne jàkk ci noonoo noon.
21 Dees maa sewal, sama xol jeex, ma wopp; may sàkku yërmande, awma ko; ku ma dëfal it, gisuma ko.
Sabóor 69 in Kàddug Yàlla gi