Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:154-160

Help us?
Click on verse(s) to share them!
154Àtte ma, ba jot ma; musal ma, yaa ko dige.
155Ku bon sore sa wall, ngir sàkkuwul sa dogali yoon.
156Aji Sax ji, sa yërmande yaa na; musal ma ni nga ko baaxoo.
157Ñi ma topp ak ñi ma baña bare, te taxul ma dëddu sa kàdduy seede.
158Damaa gis workat yi, sib leen; ñoo sàmmul sa kàddu.
159Seetlul ni ma soppe say tegtal. Éy Aji Sax ji, musal ma, yaa gore!
160Sa mboolem kàddu dëgg la, sa ndigal yépp di njekk, sax dàkk.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:154-160Sabóor 119:154-160