Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:27-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
27Njàqare di ngëlén, dab la, sa musiba def callweer, buub la, njekkar ak fitna dal la.
28Keroog nga woo ma wall, duma wuyu, nga seet ma, seet, doo ma gis.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:27-28Kàddu yu Xelu 1:27-28